Les larmes de khadim ndiaye apres ses propos sur… « ma ngi baalu… »

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 янв 2025

Комментарии •

  • @Shjeuropfolrh
    @Shjeuropfolrh Год назад +39

    Reug Reug amna yakar né beuss dina niaw mou nek Rois des arrene diapalé lenne ko té bayi wakh diou niaw dji amoul ndiarigne yalla na niépou am diam 🙏✅️

    • @chesowe5852
      @chesowe5852 Год назад

      Nice

    • @salioudiop5130
      @salioudiop5130 Год назад +1

      Sou encadrement bi bakhé mais Amna gno khamni Dani yakh mbeur mane fans sa Thiès la mais j'affirme que c'est un grand champion

    • @astudiagne7699
      @astudiagne7699 Год назад +1

      BOUDÉ ÑJI MA GUIS GNOKO YORÉ AK PABI GUÉNEU SI INTERNET BI GNOKO YORÉ WARNAÑO KHOLAT SÉN BOP

    • @salioudiop5130
      @salioudiop5130 Год назад +1

      @@astudiagne7699 bilahi mbeur etourasam dafa wara bakh bou beugué carrière bou yag té bakh

    • @rassemtombalbaye5005
      @rassemtombalbaye5005 Год назад

      Niiit dey wakh deugu reugreug a 3 defaite ci lamb meussoul nangou bi toubab bi niaffé ndeyam da fene senegalais yi ni degnkey rejouer alors que sa nexiste pas en mma reug dou sportif meun neu doul mok niom palla ak khadim dou nekk roi des arénes yoroul djiko bi

  • @maxdieye5102
    @maxdieye5102 Год назад +26

    Khadim bénéne yone nga khôl ningaye wakhé avant tout

  • @kabakebacisse9282
    @kabakebacisse9282 Год назад +12

    Merci khadime bien parler mais il faite félicitations sa this

  • @mbodjipapi2234
    @mbodjipapi2234 Год назад +2

    Vraiment papa khadime ligua wakh ni nonou lako wakhéwone en plus j'avoue que vous êtes un grand ambassadeur pour la renaissance de la lutte vraiment chapeau à vous et yalnala yalla défal diam ak soutoura inchallah Allah

  • @yacinebouballaguaye2243
    @yacinebouballaguaye2243 Год назад +10

    Moi je dit grand frère khadim Ndiaye j'ai beaucoup de respect pour tous les frères lutteurs 🤼‍♂️ mais pour dire vrai on ne modi pas l'enfant de quelqu'un la vie est courte n'oublions pas ça nékaléne si diam Amine yarabi 🤲❤️🤲

    • @ibrahimaibrahima6448
      @ibrahimaibrahima6448 Год назад

      Yacine silo nék

    • @yacinebouballaguaye2243
      @yacinebouballaguaye2243 Год назад

      @@ibrahimaibrahima6448 Machalla mon frère je vais très bien Alhamdou santa yalla comment va la famille Ibrahima nékale si diam Amine yarabi 🤲❤️❤️❤️🤲

  • @abdoudiop8695
    @abdoudiop8695 Год назад +16

    Machalla khadim amna solo gayi lamb la wone diékhna

  • @yesyes7713
    @yesyes7713 Год назад +22

    Ndeysane dafa merone reck wayé kholbi dara nekouci, félicitations sa Thiès, du courage Reug Reug

  • @maminakane4735
    @maminakane4735 Год назад

    😅wa thiaroye. Nio dakh ci Sénégal 😂😂😂😂merci grand Khadim vive thiaroye sur mer

  • @bobaucarthiam8478
    @bobaucarthiam8478 Год назад +19

    Dans la vie quand on prend de l'âge on réfléchit d'abord avant de parler

    • @muhammad3323
      @muhammad3323 Год назад

      C’est STUPIDE qui a raté sa vie. Il a une HAINE, une JALOUSIE VICERALE envers la famille de feu Double Less. F…CK HIM

  • @naniousamejikkoyi2112
    @naniousamejikkoyi2112 Год назад +77

    *kone khadime Ndiaye ba légui nagouwo ni reug reug danouna geumeul yalla nak grand Enplus souguéne mératé délene ande ak saggo aduna jekhna té wakh balle la ,ancien gloire yiffi nékone yeupp niogui barzakh, kone aduna ken douffi dess,khadime yékkgua moustapha guéye, cheikh sarr,békaye mbaye, Modou mbaye louné aye deféyant guéne lounék wakhguako , legui yagui ni ame kerssa, chef decurie et de sécurité doit donné de bon exemple,guissna aussi sen bene pa bou kon loukko nekh laye wakh magg bou rewla wakhlene ak mome bouléne niounane lebou aye doff naniou reug reug moma gana bette aye cadome niawna torope*

    • @elhadjifaye1166
      @elhadjifaye1166 Год назад +3

      Bo amé conseil yo diokhé diokh ko sa dome merde

    • @moustapha9852
      @moustapha9852 Год назад +1

      ​@@elhadjifaye1166 dégal li rk

    • @aminadiarra2205
      @aminadiarra2205 Год назад

      😂😂😂😂

    • @noraynibadiane730
      @noraynibadiane730 Год назад +4

      Geum nako ms khathie bi lay bagna lekk motah 🤣

    • @sowamina1725
      @sowamina1725 Год назад +3

      Wallahi, vous avez parfaitement raison, depuis lors dama paré si reug reug ndakh staffame

  • @assanediop505
    @assanediop505 Год назад +6

    Ndékété reug reug gniko weur yeup molén tané😂😂😂😂yii wakhi dof😂😂

  • @COACH927
    @COACH927 Год назад +10

    vérité absolue grand khadim machalla mes respect ✊ ❤

  • @ndeyesalioundiaye3119
    @ndeyesalioundiaye3119 Год назад

    Yapou khath baniou tadion thi boori tisbar gas nia di seniou ba faté tisbar yaw rek ya seniou woul te douko meussa deef walahi 😭😭😭😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️yay eukheumadou 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @poupeefall5753
    @poupeefall5753 Год назад

    Sathies aussi soutien de famille la té sathies aussi à perdu son papa lou geuneu raféte moye yémalé kou nékk am nga fo fare mais na faréte sénégal béen bop la mounou niouko séedo ❤❤❤❤❤ vive le sénegal 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇪🇦

  • @kharagnembaye5958
    @kharagnembaye5958 Год назад +10

    Wakh bou gniaw mo geuneu bone Saga Sénégal billahi damathié titt
    Nitt yoo khamnei amoul lougni Rous Amougne lougni diombou Athia rek
    Wakh djou gniaw Amoul béneu ndiarigne
    Nagniou defar kadou yi

  • @degueuntaan3060
    @degueuntaan3060 Год назад +5

    Way woooo yaye togne yaye diégalou yaye balé mbeur yeup ay soutien de famille lagnou en plus sathies ak reug reug yeup seni papas dagno gagnou

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 Год назад +1

    Any way , felicitations Senegal , 😁😁😁 Truth is Truth ,,, NIce, I love yo true words , Nice Peace ✌️ and Love.🌍

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 Год назад +2

    Merci khadim , Merci., bless.✌️😁

  • @ndeyesalioundiaye3119
    @ndeyesalioundiaye3119 Год назад

    Yay borom djioumadji yaw ba gua. Ya di diay sen ngor yaw rek ya takhawon resisté thi kanamou toubabya 😭😭😭❤️❤️❤️❤️ yaw dagua rafet khool ndeyssan 😭😭😭😭😭

  • @sheky3138
    @sheky3138 Год назад +1

    Mais Khadim thiow jiboul Baye!

  • @Lamzi92i
    @Lamzi92i Год назад +2

    Merci père Khadim Ndiaye

  • @fallougentlemara4853
    @fallougentlemara4853 Год назад +1

    Pere diegueul naniou la mais del khalate lingay wax c'est très important

  • @ndongodjifadafada1278
    @ndongodjifadafada1278 Год назад +3

    Machala amna solo cest le sénegal ki gagne lépp bénn la

  • @fatousane7600
    @fatousane7600 Год назад

    Khana sa thies môme dou soutien de famille

  • @mameballaka5713
    @mameballaka5713 Год назад +2

    Machalla machalla machalla ❤️❤️

  • @aminataniang2948
    @aminataniang2948 Год назад

    Li gua wakh degue la khadime ndiaye ❤❤

  • @massambadiop8181
    @massambadiop8181 Год назад

    Kou guiss ni dioyou khadim ndiaye yi amoul rongogne beuseul j’aime 😂😂

  • @khadimndiaye5910
    @khadimndiaye5910 Год назад +7

    😂😂😂😂😂😂yaw do rous khadim kholatal sa bopou😂😂😂

  • @ibrahimadiatta4232
    @ibrahimadiatta4232 Год назад

    Hadid tu étais mon lutteur mais il faut revoir ta commutation car tu es le grand des enfants

  • @mordiop5555
    @mordiop5555 Год назад

    Du courage pere khadim

  • @Shjeuropfolrh
    @Shjeuropfolrh Год назад +2

    Té ngénne kham niné lii sport rek la sport gagne walla perte naiou yamalé lépou si sport mo gueune di wakh wakh diou niaw na niou nek ay sportif yalla na diam yague Sénégal 🇸🇳

  • @djillycisse3011
    @djillycisse3011 Год назад

    Rèspecte len kadime ndayesan ligi mak la tè mak bour la🥰🙏🙏🙏

  • @kouragueye4766
    @kouragueye4766 Год назад

    Merci Khadime ta bien fait

  • @2M5-Motivation
    @2M5-Motivation Год назад +14

    😂😂😂😂😂 astafourhlilah mais nak de toute façon père légui doto xalé guéneul si Linguan nékeu téh geuneu doli sa diamouh yalla diko digeul sama bopouh ak mbolém djioulite

  • @kheuchboukharagnelo6460
    @kheuchboukharagnelo6460 Год назад +2

    Wa khadim do té sa guémigne bingay wérangui😂😂😂😂😂😂😂

  • @amadouibrahimaba6974
    @amadouibrahimaba6974 Год назад

    Père khadime courage défaite nekhoul boulen tilimal victoire sa Thiès

  • @mbayeseye301
    @mbayeseye301 Год назад

    Bilahi KHADIM Ndiaye mo geuna nékh Maîtrise El Hadj Diouf Sheut iow meune geu bouné

  • @boubacardiamba
    @boubacardiamba Год назад

    Khadime à parfaitement raison sur le cas de Beckaye mbaye

  • @tallanael9855
    @tallanael9855 Год назад

    merci Khadime sathiés 💪💪💪💪

  • @moussandiaye1762
    @moussandiaye1762 Год назад +7

    Machalla diekhna man sa thies la faral mes diekhna nay rafet rek adouna amoul solo

  • @bassiroutoure7237
    @bassiroutoure7237 Год назад +3

    Merci khadim ndiaye ♥️

  • @modoumbengueasaly2702
    @modoumbengueasaly2702 Год назад

    Noo 😅 khadim nena renou dakh la diokh lirou Diane😅😅😅😅

  • @Defunity
    @Defunity Год назад

    Sénégal yén da nguén dessé xam Khadim Ndiaye, ki Loumouy wakh dara safouco sii, déyy togne rek akk yeungual, bokkeu ni sii niouy diaay combat you barri. Sounou deuk bi Nak da méti wakhé, niou Barri bayina niou lamb croiser les bras, wakhatou niou si, défatou niou si bén acte. Il faut comprendre Khadim, mane déé Reug Reug dou sama Mbeur mais khadim j'adore l'écouter

  • @mouhamedthiam5714
    @mouhamedthiam5714 Год назад

    Kouy ministre des sports

  • @ndiagagueye2094
    @ndiagagueye2094 Год назад +2

    Rafèat khadim dion wakar sa amono porblm 🥰

  • @Lepatriote9423
    @Lepatriote9423 Год назад +2

    Pere Mbaye Mangoné limoula tontou bodone gor do doundou. Gathié réka la diap.

  • @infosk98tv17
    @infosk98tv17 Год назад +1

    Franchement ngoorsi ndiaye mii wèroul 😄😄😄😄🤦‍♂️

  • @daadydiop9880
    @daadydiop9880 Год назад +2

    Qui dou nitt sakh yow waro done talibé Serigne Touba sakh

  • @tiiw7425
    @tiiw7425 Год назад

    Khadim respect mais cas même y'a chute faut qu'on accepte c'est la volonté de dieu merci

  • @abdoundiaye2634
    @abdoundiaye2634 Год назад +2

    Khadim ndiaye tu change comme un feu rouge😂😂😂😂😂😂

  • @mbackediop-ot5rj
    @mbackediop-ot5rj Год назад

    Fini pour Reug reug
    Ban adversaire Moy dieulate Reug reug

  • @sawroumbengue7820
    @sawroumbengue7820 Год назад +1

    lirou diane ak khadim ndiaye nalene gaston production may xalisse

  • @taftaf3989
    @taftaf3989 Год назад +3

    Sawaye mayniou diame sathiese dane reug reug dikhena

  • @TheBandafall2003
    @TheBandafall2003 Год назад +2

    La prochaine fois il faut rester ds cadre du sport et chacun a le droit d’expression et chacun a le droit de donner son verdict avant et après combat c’est comme ça

  • @daoudasagne91
    @daoudasagne91 Год назад +6

    Même si ya chute il faut toujours attendre la dernière décision c'est important

  • @ndioufandoye64
    @ndioufandoye64 Год назад

    Manchall khadim

  • @seynithiam7857
    @seynithiam7857 Год назад

    Khadim Ndiaye togne ga wa thiaroye bilahii ,thiaroye gnou baax gnofa nekeu gnou am yaar ....
    Wahiii doff ga wara bayiii .

  • @elhadjiaminediop6417
    @elhadjiaminediop6417 Год назад +3

    Saay xanaa Peer ngoone dalaa tiital du la jure baal na la🤣🤣🤣🤣🤣

  • @mmsseye9391
    @mmsseye9391 Год назад

    merci khadim

  • @waganefaye2113
    @waganefaye2113 Год назад +2

    Bilahi 4 appuis yéna soff ki loutax guéne koyy intéroger goo wayyy gni douniou exemple

  • @glasgowhits8585
    @glasgowhits8585 Год назад +1

    Khadim gnata yon la wax khamgua? Thi émission bi kou ko meuna compter 😂😂

  • @dpfp2151
    @dpfp2151 Год назад

    Segne khadim kou ❤️ bakh waro wax Lou niaw

  • @saliouba9428
    @saliouba9428 Год назад

    Machallah

  • @djibrilsarr2884
    @djibrilsarr2884 Год назад

    Merci pére

  • @momogueye7447
    @momogueye7447 Год назад +6

    Yaw ba legui Yagui wakhe 😂😂

  • @sakhopape6192
    @sakhopape6192 Год назад

    Kou bakh la

  • @babacarsow7970
    @babacarsow7970 Год назад +1

    Yow y’a geune nek domoukharam si lambe dji

  • @momoseck1617
    @momoseck1617 Год назад +1

    Ki doméram la bilahi

  • @atoumanedieme-tt5ro
    @atoumanedieme-tt5ro Год назад +5

    Moi vraiment je ne comprends pas certain cadre père tu as bien dit que les deux maman des lutteurs on bien parler mais pourquoi toi qui est leurs papa tu ne fais pas la même chose vraiment il faut nous donner les bons exemples vous les parents
    La vie d'aujourd'hui aux pays est très difficile mais nous aussi nous rendons plus difficile la vie partout dans le sport les politiciens

  • @modoumbengueasaly2702
    @modoumbengueasaly2702 Год назад +1

    Noo 😅 khadim lamb diou bokol nekhoul 😅😅😅😂😂😂

  • @chiffoba8330
    @chiffoba8330 Год назад +6

    Ki momine la yalla topewouko dra🤣🤣🤣🤣😂😅

  • @serignemorfall5635
    @serignemorfall5635 Год назад +4

    Mè ki dou yaw.mane sa tourbi rek moma diakhal warowone toudou khadim

  • @aliounesall863
    @aliounesall863 Год назад

    Antouka dall kilifa balou mouy wakh dakoy Khôl kholat ko li lamb kasser leu ter day diékh adouna amoul solo yén nieup ay sénégalais guén wa salam

  • @mgamadoubakhoum8831
    @mgamadoubakhoum8831 Год назад

    Diadieuf khadim Ndiaye

  • @ibrahimadiouf6289
    @ibrahimadiouf6289 Год назад

    Merci khadim, le reporter tu es différent des autres reporters nga khamné ay saytané lagn

    • @astudiagne7699
      @astudiagne7699 Год назад

      REPORTER YI LIÑOU GUIS LAÑOU WAKH TÉ MOMLA SÉNÉGAILÉ YI GUIS

  • @papechiekh6908
    @papechiekh6908 Год назад +2

    Yawe geumo dara amo béne yare

  • @cheikhbi2056
    @cheikhbi2056 Год назад

    Khadim Ndiaye moo dakkeu si Adouna bi bilahi. Nangouna comédie bi si Liirou Diane nii rek 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @bakhyayeniang2605
    @bakhyayeniang2605 Год назад

    Oui nila adouna amoul solo pér khadim

  • @moussasylla4081
    @moussasylla4081 Год назад +1

    Ligua wakh lirou kay saga sah moko guene wah day rafet

  • @momogueye7447
    @momogueye7447 Год назад +5

    Khathie bi mome yako mome 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @mouhamedsambe7820
    @mouhamedsambe7820 Год назад +4

    Ngen balma mais kougn wax xeilou lebou nga yoor meun deuk si dioy😂😂😂😂😂😂😂

    • @MackySallprésident
      @MackySallprésident Год назад

      Respecté bok

    • @santyalla123
      @santyalla123 Год назад

      Frère amal yar AK téguine Say moromou baye AK moromou yaye ay waliou niofi nek lebou .k Dieu nous préserve d'être un ignorant ki s croit savant

    • @santyalla123
      @santyalla123 Год назад

      Soma waxé lolou manila guéweul ni lan mel ga mer donc nane bayi affairou xét

    • @beinz9482
      @beinz9482 Год назад

      😅😅

  • @alaminethiam6950
    @alaminethiam6950 Год назад

    Nite kou am khél chaque jour war nga diangue si liy khéw en plus nite Bo néké kilifa wala nga yor yén responsabilité yi danga wara kham ningay wakhé nite dou sagne wakh bala ngay wakh dara war nga ko bou bakh
    En plus nite kouy guiss deugue bou lér nagne bagne né doko wakh si gathié rk ngay deuk

  • @sowamina1725
    @sowamina1725 Год назад +2

    Yénako commencer ndakh bagna nangou sen défaite cthim

  • @moustaphadieng3658
    @moustaphadieng3658 Год назад +10

    Merci père Khadim

  • @beuguesalioubeuguesaliou524
    @beuguesalioubeuguesaliou524 Год назад +1

    Ki lou balla diouf wakhe rek mossi nek dou royou kaye
    Signé wo contrat dou yaw ya wara diay lamb dji ak lo meuna diapaler reug reug dou ni o contraire yangui koye yakale déle wakhe lou rafett mo geune khame ni mak gua

  • @jazzjazz4902
    @jazzjazz4902 Год назад +1

    SENEGAL 🇸🇳 MOLENE NAWLO WOUL WONE SI SEN COMPORTEMENT. LI NGAY YEEDE NITE YI YEEDE KO SA BOP KILIFEU NGA

  • @Ahmadouboromediamono4
    @Ahmadouboromediamono4 Год назад

    Ki meusoul doff nitt ndiaye la limouye wakh mo enrangé woul gars yi rek 😂😂😂

  • @elhadjidiagne40
    @elhadjidiagne40 Год назад +4

    Ki vraiment wéroul 😀😀😀😀

  • @yilebaba6565
    @yilebaba6565 Год назад +1

    Magg mou niak fayda mongui nii ... koy niak classe ak personnalité ! Mboromam yeup niongui ci lamb dji di niaw aka défar mais mom diakgassé ak yakh dérr rek lafi néké ! Doff deug leu , quelle honte

  • @adamambodji5368
    @adamambodji5368 Год назад +4

    Meno nek nit te khamni mak ga

  • @badiartv242
    @badiartv242 Год назад +1

    lekale khatie bi goor thia wakh dia DOMERAME

  • @senegaltv1142
    @senegaltv1142 Год назад +11

    Respect à khadim et ReuG ReuG ❤

  • @ouldfall
    @ouldfall Год назад

    Newona sah dotoumala deglou mais Machalah taye mome nitegua

  • @mortallandiaye-wv3mc
    @mortallandiaye-wv3mc Год назад

    En tout cas il savoir se respecter avant tout

  • @modougueye7148
    @modougueye7148 Год назад

    Waye nak khadim amna lokhamne mbirou yala la delene wakh te boulendi wat di foe yala

  • @ballydiop9101
    @ballydiop9101 Год назад +6

    Khadim ak lo meuneu waxal reug reug amoul soutoureu loumou defal niit ki nieuw ba am défaite diko netali adunia yeup di degg pour affaire de ndam rekk mandé nawon nako mais ma dou si mom ba faww , champion yagg na am galencor mais nieuw beurré té waxoul lou niaw l’an mo geuneu reuye couronne 👑 roi des arènes Balla Gaye 2 mom la sacrifier moy febar niew de beurré n’ouïr bania yakh biss bi djogue si té waxoul dara lou niaw motakh kouko guiss naaw ko

  • @kanikhegne4570
    @kanikhegne4570 Год назад

    Tapet dong ndakh danoula porter plainte motakh .mai boulenko bayi nafekh bou makla .fene rek laye def. Dioyou nafekh. Boulen geum aye wakham moytoulenko .boulen bokak mome diotaye . Nitkou bone ta ignane moye khadim ndiaye

  • @karimfall5708
    @karimfall5708 Год назад +1

    Wakeur double less baré ak niom yomboul bolene dané tiow bari bougbela dané tiow bari.

  • @ndiagakane8220
    @ndiagakane8220 Год назад +2

    Reug reug AK ay staffam War nagno défarate sén togay ndax lamb day diékh

    • @elhadjifaye1166
      @elhadjifaye1166 Год назад

      Bo amé conseil bo diokhé diokh ko sa dome

    • @lamo1742
      @lamo1742 Год назад +1

      Lou ler ga wakh wérougnou

    • @ndiagakane8220
      @ndiagakane8220 Год назад

      @@elhadjifaye1166 awma louma wax AK yaw !callate!

  • @layefall452
    @layefall452 Год назад +4

    Dafay sop souba mou khaste wat